Abdou Qadir Mbacke

Abdou Qadir Mbacke Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de Abdou Qadir Mbacke, Société de médias/d’actualités, Dakar-Marine.

Ñun mourid nak sunu djiko sunu mélo linga xam né bugne lako waxee ak bugne la ko waxul lolou lagniy deff modi kepou ko x...
24/08/2024

Ñun mourid nak sunu djiko sunu mélo linga xam né bugne lako waxee ak bugne la ko waxul lolou lagniy deff modi kepou ko xamné ni yalla deff serigne touba nekh nala dagne lay def comme sunu bopou kepou ko xamné nak niko yalla def neekhou la dugne la limaalé si dara. Waslm

(Diaganté Nitu yalla yi  Ak Djiné yi Ak ndiabar kat yi )Niti yalla yi bokou niou Ak ndiabar kat yi; Ndiabar kat bi day n...
31/12/2023

(Diaganté Nitu yalla yi Ak Djiné yi Ak ndiabar kat yi )

Niti yalla yi bokou niou Ak ndiabar kat yi; Ndiabar kat bi day niakka xam bopam dem toppu djinné diko weur ba djiné dia féniou ko diokh ko ay sartam! Neko bo baguee ma ande ak yaw fawu dangay nek Ak man si lii Ak si lii bu boba ndiabar kat ba topou si guinaw djiné dia diko diamu diko deferal ay sacrifice nguir djinè dji diko defal mom tmt limu bague ! Nga xamné bu boba djiné dji moy sangue bi ndiabar kat bi moy diaam bi lolou bokul Ak mbirum nitu yalla yi ! Nitu yalla yi seen Rouh day ague fo xamné djiné yi si sén diami bopou niooy niaw di diaayanté Ak niom di diebalou thi niom Ak di laxatou si niom Ak di sakou barké si niom Ak di niaan si seen barkeé nguir diariniou! Ak di niaan niou xétali leen Ak di niaan niou ramu leen eulak yawmal khiyam ! Ndax niom saytané sonal nalen ta ladial nalen !

Askeuy Sëriñ tuubaSëriñ touba nekon kou bague yalla Ak yenenté bi sallalahu halay hi Wasalam! Lepou loo xamné yalla neko...
02/09/2023

Askeuy Sëriñ tuuba
Sëriñ touba nekon kou bague yalla Ak yenenté bi sallalahu halay hi Wasalam!
Lepou loo xamné yalla nekou thia dawu thia nekk ! Yoron makk nia andon Ak mom thi lolou !

Adresse

Dakar-Marine

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Abdou Qadir Mbacke publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Abdou Qadir Mbacke:

Partager