Juub Xalima 221

Juub Xalima 221 SERVITEUR D'ALLAH 👌🏿
📌 Insta [ juub xalima ] Jeune entrepreneur passionnĂ© par l'entrepreneuriat

Amna ku mas a laaj SËRIÑ TUUBA : Luy dĂ«ggi-dĂ«ggi Ă dduna ❓SËRIÑ TUUBA ni ko : « Li ci digante asamaan ak suuf, ku ci bĂ«gg...
10/05/2025

Amna ku mas a laaj SËRIÑ TUUBA : Luy dĂ«ggi-dĂ«ggi Ă dduna ❓

SËRIÑ TUUBA ni ko : « Li ci digante asamaan ak suuf, ku ci bĂ«gg dara te YALLA taxul bĂ«gg nga Ă dduna ! Ku ci bĂ«gg dara ngir jĂ«mmi YALLA SUNU BOROOM, YALLA la bĂ«gg !

Mu laajaat ko luy gennee bĂ«gg Ă dduna ci ab xol ❓
SËRIÑ TUUBA ni ko : «Looy jĂ«m YALLA tax nga di ci jĂ«m»

05/05/2025

Borom Tuba néna : xool kaamilu al-quran, ziaré Nit ku bax ak dag aye wée (se couper les ongles) si bësu Aljuma bokkunasi liy musël nit si ndiakharé (Soucis, inquiétudes, chagrin)
Source : Silkoul Jawaahir.

Amna ku mas a laaj SËRIÑ TUUBAA : Luy melow ku xam YALLA SUNU BOROOM ci jamono jii ak ja ko njĂ«kk?SËRIÑ TUUBAA ni ko : «...
24/04/2025

Amna ku mas a laaj SËRIÑ TUUBAA : Luy melow ku xam YALLA SUNU BOROOM ci jamono jii ak ja ko njĂ«kk?

SËRIÑ TUUBAA ni ko : « Mooy koo xam ni bĂ nneex ak tar-tar du gĂ©nnee weetal YALLA ci ab xolam, bu amee bĂ nneex dakoy dolli weetal YALLA ak sant ko..Bu amee tar-tar dakoy dolli weetal YALLA, waxtu wu nekk muy sant YALLA BOROOMAM di weeru ci moom


Du xool sikku kenn wàlla ayibi kenn. Képp ku melul noonu doylool YALLA te bayyi ko»

▬▬▬▬
📚 Source : Waxtaani SËRIÑ TUUBAA VOL5

10/04/2025

Ku Yàlla feeñal say ayiib, ñépp bàyyi la !

08/04/2025

Gallaaj gi gën ci muslaay yi mooy >. Deleen nëbb séen mbir yii.

15/03/2025

Le messager d’Allah a dit « celui qui est calme , doux et facile Ă  vivre , Allah l’interdit l’enfer .

11/03/2025

Soo bëggee baax, deel ànd ak nit yu baax!!!

11/03/2025

📍🧠 SoudĂ© do diouli , do woor .
Diokhal 1M de personnes ndogou ci Tali bi wala ci cogn bi mok Zéro nio yam !
Fananol La illaha illaLah fek do diouli do woorite yaxum énergie d**g leu .
Sunu borom fowoul, fowlouwul ! â˜đŸŸ

08/03/2025

Soxna Aysa ba ñu ko laajee lan mooy jikkoy Sang bi ï·ș ?
Mu ne « jikkoom mooy Alxuraan»❀

05/03/2025

Fekk ko woor nga jox ko ndogu wala lumu mëna ndogoo amna solo lool, yonent bi shw wax na ci ab adiis (Tirmisiyyu, n807): ku ko déf dinga am tuyaaba ku woor.

01/03/2025

Ramadan weeru al xuraan, jang al xuraan fepp la baaxe waaye ci weeru koor lay gëna sakkane, moo tax loo mëna jang jang ko, ku man bis bu nekk mu jang benn juz u (2 hizbu) dina jang benn kaamil ci koor gi, ta loolu yombu na.

19/02/2025

đŸ“đŸŽ„ Lii bou nĂ©kĂ© sii yaw rek... 😭 demal fadiou jii 👂👈🏿 😭

Abonne_toi 👉🏿 Juub Xalima 221

Adresse

Dakar
Dakar

Téléphone

+221782406478

Site Web

https://www.instagram.com/jub_xalima?igsh=dDUweDhhbGYzNHAx

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Juub Xalima 221 publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message Ă  Juub Xalima 221:

Partager