Xidma.net

Xidma.net Servir l'islam à travers le Mouridisme.

Groupe WhatsApp ngir jot ci waxtaan yi ñuy def ci S Fàllu   Rajab
13/01/2024

Groupe WhatsApp ngir jot ci waxtaan yi ñuy def ci S Fàllu Rajab

WhatsApp Group Invite

Un film sur les nouveaux livres, réalisé par les petits-fils de Serigne Fallou
12/02/2023

Un film sur les nouveaux livres, réalisé par les petits-fils de Serigne Fallou

22/08/2022
As-salaamu Halaykum warahmatul LaahMbokk yu tedd yi, ñoñ Alxuraan, noo ngi leen di yëgal tegu xeeru Daaray *"ILHAAMU-S S...
09/05/2022

As-salaamu Halaykum warahmatul Laah
Mbokk yu tedd yi, ñoñ Alxuraan, noo ngi leen di yëgal tegu xeeru Daaray *"ILHAAMU-S SALAAM"* ci njiital seen mbokk Ibraahiima Kebe, nu koy amale Tuubaa Ndindi fa wetu jakkay S Jiili Mbàkke Faadilu, ca yoon wa jëm Daahra Jolof, muy dëppoo ak Àllarb jii nu dëgmal di fukkelu fan ak benn ci weeru tubaab (11 mai) di tolloo ak fukku fan ci weeru kori wii (10 sawwaal), mu war a door ci waxtuw 11h00 ci suba insàllaa.

Noo ngi ciy sàkku seen i ñaan ak seen teewaay bu baax a baax.
Ngir yaneeni leeral, jokkool ci limat yii:
77 714 84 50 walla 70 505 02 91.
JËRËJËF.

05/04/2022

▁▁▁▁▁▁▁▁▁LIS LA DESCRIPTION▁▁▁▁▁▁▁▁▁Si vous avez aimé cette vidéo vous pouvez mettre un petit pouce bleu et aussi vous abonner !(Ça aide vraiment au développ...

Address


Alerts

Be the first to know and let us send you an email when Xidma.net posts news and promotions. Your email address will not be used for any other purpose, and you can unsubscribe at any time.

Shortcuts

  • Address
  • Telephone
  • Alerts
  • Claim ownership or report listing
  • Want your business to be the top-listed Media Company?

Share