Astuces et leçons intimes

Astuces et leçons intimes Astuces et leçons intimes

25/03/2025

Un grand merci à mes nouveaux followers ! Dyja Diallo, Maimouna Yade Diop, Sokhna Ndiaye Badiane, Vanessanyowa Nyowa, Thioro Ndiaye Ngom, Mame Diarra Sene, Khady Fall Sarr, Aicha Mamou, Dieynaba War, Ndaye Fatou Fall, Georgette Diatta Ndong, Djiba Bahmobah, Ndeye Awa Sarr, Fatima Baldé, Mery Coulibaly, Leiticia Campal, Innocente Biagui, Thiatou Pape Diouf Faye, Aminata Ly, Ndoumbé Babou, Oumou Midiaou Sow, Mariame Bah, Awa Diop, Rokhaya Gningue, Yasmine Compaore, Ndeye Sene, Gnima Diatta, Salamata Sow, Adama Thiam Barry, Mariama Niang

25/03/2025

del nane thiep ak gowe sani si touti khorom pole def ko si frigo def ko sa ndokh diko nane chaque jour bakhna trop

Astuces jiguéne boudoul toye wala boudoul yeuk plaisir :-Wouteul poudre ndirr, lait chaud clou de girofle et miel nga di...
14/07/2024

Astuces jiguéne boudoul toye wala boudoul yeuk plaisir :
-Wouteul poudre ndirr, lait chaud clou de girofle et miel nga dieul ko 1heure avant combat.

-Wala nga oute ndir rakhass ko bamou sét wer ko 24h après nga walko bamou mok defko sissa ben pot chaque jour nga def 1 wala 2 coudou soupe si ben tasse defsi mew ak eau chaude après le petit déjeuner nga naneko.

14/07/2024

Sirop menthe pour sucer ton partenaire

Astuces et leçons intimes

*Astuces : poudre petit cola*La poudre de Petit Cola a de nombreuses vertus notamment liées à la libido et la faiblesse ...
14/07/2024

*Astuces : poudre petit cola*

La poudre de Petit Cola a de nombreuses vertus notamment liées à la libido et la faiblesse sexuelle.

*Propriétés:*

- Lutte contre la faiblesse sexuelle, Lutte contre la baisse de libido manam day yokou katanou goor té day takh affaire bi gueuneu saff.

- Stimule l'appetit sexuelle chez l'homme: day takh Kou goor ki Di âme envie.

- Tonifie le pénis en cas de dysfonction érectile: day deugueureul ak Di yokou george

- Prévient l'impuissance sexuelle: day takh do kham louy impuissance sexuelle

- Lutte contre l'éjaculation précoce: éjaculation précoces maname gawa danou môme ak poudre petit bi môme danga Koy degg rekk

- Azoospermie, oligospermie (mauvaise qualite du sperme) day takh goor âme ndokh Bou farr âme qualité teksi.

*Utilisation:*

Pour profiter pleinement de ses bienfaits, vous pouvez simplement mélanger la poudre de Petit Cola avec la poudre de Gingembre et du miel. La poudre peut également se consommer diluée dans de l'eau ou bien dans du yaourt. Aussi mélanger avec du karité naturel et utiliser pour massage de George.
Ma wakh KO si Olof:
Dangay dieul sa poudre petit cola mélanger KO ak poudre gingembre defsi sa cassou ndeki tibb niarri coudou à café si sa mélange defsi defsi ndokh soukeuré KO miel naturel. Wala tmt nga defko si yaourt nature rek. Mais aussi mélanger karité ak poudre petit cola bi diko masser Koy bi bakhnassi tropp mais aussi bakhna trop pour massage yaram bi yeupp.

Sirop menthe
13/06/2024

Sirop menthe

☘️ ASTUCE TABASKIKou nék khamna ni tchine bokoul tchafine wayé nokosse bou bakh moy saffal thiepppe ... Motakh tay dama ...
13/06/2024

☘️ ASTUCE TABASKI

Kou nék khamna ni tchine bokoul tchafine wayé nokosse bou bakh moy saffal thiepppe ... Motakh tay dama indi astuce bi ma toudé nokoss mou am solo trop, di diokhé khétt bou nekh, di dimbali gni am problème sécheresse vaginal, dina yokk banékh, doli sén libido bâ linguén beug ci séne bope nguéne am ko 🥰

*🦋 Ingrédients : thiép, nana, citron, khorom polé AK gingembre.( Bouci nék ci yi touti rek doyna )

*🔥Préparation: dangay dieul thiép bi ak khorome polé ak nana bi bakhal KO 15 minutes après nga pathial ci citron bi bayi KO ci ndokh bou tangue bi bamou dall nga ségg KO dieul ndokh bi defar ci jus gingembre bi . à boire après le repas et après le dîné juste demi verre. Fofou saparal ba dakk nekh.

Les vertus illimités du faux baobab ( garabou dambal)* pour les femmes:Pour faire grossir naturellement les seins,les ha...
25/10/2023

Les vertus illimités du faux baobab ( garabou dambal)
* pour les femmes:
Pour faire grossir naturellement les seins,les hanches et les fesses.
Faites bouillir 4 fruits de cette arbre dambal et mettez 500 g de karité pur dans la décoction.
Massez les parties concernées matin et soir

Adresse

Dakar

Heures d'ouverture

Lundi 09:00 - 23:00
Mardi 09:00 - 23:00
Mercredi 09:00 - 23:00
Jeudi 09:00 - 23:00
Vendredi 09:00 - 23:00
Samedi 09:00 - 17:00
Dimanche 09:00 - 17:00

Téléphone

+221703646922

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Astuces et leçons intimes publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager