Cheikh Ahmadou Bamba Business Center

Cheikh Ahmadou Bamba Business Center Message to the World

     ❤️
09/05/2024

❤️

Assalaamu halaykum, noo ngi leen di baalu àq, di leen baal. Yal nanu Boroom bi defal njéggal, sutura ak tawféexu fekke y...
09/04/2024

Assalaamu halaykum, noo ngi leen di baalu àq, di leen baal. Yal nanu Boroom bi defal njéggal, sutura ak tawféexu fekke yeneeni koor ci barkeb Ramadan... Gan gu mat gan tàggóo na, yal nanu teewewaat nganeseem ci ay at yu limu. Yal na Boroom bi nangul nu koor gi, ñaan yi te barkeel lépp🤲🏿 ChCheikh Ahmadou Bamba Business Center ❤️

     ❤️
29/03/2024

❤️

Assalaamu halaykum, noo ngi leen nuyu ak di leen siyaar, di yaakaar ni jàmm rekk ngeen yendoo... Yal na Boroom bi dolli ...
21/03/2024

Assalaamu halaykum, noo ngi leen nuyu ak di leen siyaar, di yaakaar ni jàmm rekk ngeen yendoo... Yal na Boroom bi dolli sutura si yokk jàmm ji ak xéewal yi... Ndogug jàmm

❤️

Adresse

Thiaroye Sur Mer
Dakar
0000

Téléphone

+221779232534

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Cheikh Ahmadou Bamba Business Center publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Cheikh Ahmadou Bamba Business Center:

Partager