Federation Culturelle Daaray Kourel Noreyni

Federation Culturelle Daaray Kourel Noreyni Dieureudieufé Serigne Touba

03/09/2026
28/08/2026

Serigne Mbaye Gueye Syll moo fi bayiko.Yalnako yalla yërëm té xaaréko aldjana ci barkép seydina Muhaméd sallalàhu aleyhi wa salam
Borom Xam Xam , ku xam histoire yonu Mouride demna .
Ku beugone Serigne Touba rawatina Borom Daarou .

27/08/2026
13/08/2026

Séentu weeru Gàmmu 1448H
_____________
Assalaamu halaykum wa Rahmatullaah.
Mbooloo mi Sëriñ bi dénk wàllum séentu weer wi ci Tuubaa ñooy xamal ñépp ne tay jii ci Alxemes ji, 29eelu fani Diggi Gàmmu (Safar) 1448H, dëppoo ak le 13 Août 2026, dinañu daje ci sowwub Jumaay Tuubaa ju mag ji ngir séentu weeru Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H.
————
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.

Adresse

Darou Moukhty Chicory
Diourbel

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Federation Culturelle Daaray Kourel Noreyni publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager

l="false"> Ajouter une annonce
  • Login
  • Souscrire

    Nous vous informerons quand tout se passe à Diourbel.