Sop yalla abibe

Sop yalla abibe Sop cheikh amadou rafahi

16/03/2026
06/03/2026

Ousmane SONKO Yalla na goudou fane ,kou né aamine Yalla nga goudou fane!

04/02/2026

Yalla nagu fi yagu ta wer amine yarabi

04/02/2026

Jerejef borom darou kadou yi amna solo

24/01/2026

Serign bi yalla nafi yagu ta wer Amin yarabi 🦻🏻🦻🏻🦻🏻🦻🏻❤️❤️

01/01/2026

Premier ministre buy wakh di khalate bammél ak bess PenC si kanamou yalla
Li meusta am

Bouniou sonko reuthié c fini pour le Sénégal

23/12/2025

Jërëjëf sunu borom

Jërëjëf serign bi yalla nafi yagu ta wer Amin yarabi
21/12/2025

Jërëjëf serign bi yalla nafi yagu ta wer Amin yarabi

11/12/2025

2029 rek inchalla ak saydina cheikh oussman mou selmi mom rek lanuy topou gor dëg la tadou wour lomou wakh nar nakou yagu ak wer rek

Assalaamu halaykum wa rahmatul Laah bokk taalibe yi noo ngi leen di nuyu te di leen siyaar. Niki ni kenn ku nekk ci nun ...
07/12/2025

Assalaamu halaykum wa rahmatul Laah bokk taalibe yi noo ngi leen di nuyu te di leen siyaar.
Niki ni kenn ku nekk ci nun ame ag farlu ci wut "carte d'identité" ngir xam ne mooy wane, di firndeel ne doomu Senegaal la jàpp nanu ne noonii la kenn ku nekk ci nun war a farloo, def yitte ci dàgg këyitu cëram "carte membram" nde bokk na ci liy firndeel sunug bokk ci Association Ar-Rafaahi Pour Servir l'Education Islamique waaye bokk na it ci liy jëmale liggéey bi kanam. Mbokk ci ñaari simili nga jëmale liggéey bi kanam wànn boo gis ci benn lay tàmbalee kon nag ngalla bul ko waaj kenn xamul kañ la ak fan la nanu farlu ci jaamu Boroom bi jaare ko ci liggéeyal Sëriñ Tuubaa. 775709572

Adresse

Kaolack

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sop yalla abibe publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager