
10/07/2025
De Ousmane SONKO ,
Après 11 années d'existence, PASTEF–Les Patriotes franchit une nouvelle étape majeure avec l'installation de son Conseil national, l’une des instances les plus importantes du parti.
La cérémonie se tiendra ce soir au King Fahd Palace.
À cette occasion, je m’adresserai à l’ensemble des militants et sympathisants à travers un message important, porteur de nouvelles orientations. Ce message sera diffusé en direct et l’heure vous sera communiquée tout à l’heure.
Restez mobilisés, restez à l’écoute !
-------‐--------------------- ○○○○○○○○ ---------------------------------
Ci Kàddug Njiital làng ug Pastef,
Ginnaaw 11i at gu làng gi, PASTEF–Les Patriotes jël na bu bees te am solo ci taxawal "Conseil Nationale", di bànqaas bu gën a am solo ci làng bi
Xew-xew bi dina am tay ci ngoon ci ca "King Fahd Palace".
Ci pose mii, dinanu ci waxtaan ak mbooleem farandoo yi ak soppe yi ci bataaxel bu am solo, jëm ci tegtal yu yees. Dinanu jàllale bataaxel bi ci daar-daar ak yëgle waxtu wi leegi ci kanam.
Desleen di booloo, desleen di nu déglu !
Page Commmunale Pastef Koki