Mbéctém Darou Mouhty

Mbéctém Darou Mouhty Page officielle Darou Mouhty ✔️

Grand Magal de Touba Selon le président de la commission culture et communication du grand Magal de Touba, Serigne Abdou...
14/08/2025

Grand Magal de Touba

Selon le président de la commission culture et communication du grand Magal de Touba, Serigne Abdoul Ahad Gaïndé Fatma, l'édition 2025 a mobilisé près de 6 000 000 de personnes avec un chiffre d'affaires estimé entre 300 et 400 milliards FCFA.

Immersion au centre d'information et d'accueil des enfants perdus: près de 428 enfants recueillis depuis sa création.

395 interventions, 640 victimes dont 21 décédés à la suite d'accidents de la circulation, les pompiers font le bilan.


14/08/2025

🔴6 Millions personnes moy lim binu xayma ci ñu teew ci magaluk ren gi 2025.

✨💫17 Safar 1447h - 12 août 2025🕰️7h05 , Touba s’éveille dans un murmure de prières, les minarets caressés par la premièr...
12/08/2025

✨💫17 Safar 1447h - 12 août 2025
🕰️7h05 , Touba s’éveille dans un murmure de prières, les minarets caressés par la première lumière.
🕌Les ombres se retirent, laissant place à une clarté qui ne se raconte pas…
❤️Touba ne se photographie pas, elle se révèle.
📸 dr.drone221



11/08/2025
10 AOÛT 1895Diamono ji kooy déenk sak ndiaboot bala nga dém dinala ladj "thiép bi ak diw" gui noumi démé, kokoy bataléel...
10/08/2025

10 AOÛT 1895

Diamono ji kooy déenk sak ndiaboot bala nga dém dinala ladj "thiép bi ak diw" gui noumi démé, kokoy bataléel dépense bi ak ordonance yi

Mame Thierno boolé won lép ak ndiabotou boppam boolé ci amoul këur amoul sakh ap néeg, foum dém niou dakh ko niko boulniu indil problém talou niouko, daanan ko complot di lakk ay néegam, mou sakkéttat niou lakkaat ko, mou toukhou féenéen

am na ci att mo xamni fébarou pést da dougou ci réewmi, lou bari ciy taalibéem faatu si, Sëriñ Ahmadou Yadali doomi Sëriñ bi la gén addouna, ba fébar ja dougué Sëriñ Modou Moustapha ak Sëriñ Fallou ak Sëriñ Bara banuy wadia génn addouna, kérok la Mame Thierno ndiëkeu diooy cik doundam niaan Boroomam na dieul bakkanou Sokhna Faty Isa aki dóomam té bayifi ndiabotouk Sëriñ Touba gui ndax déenkaané, bougoul Sëriñ bi nieuw mouniko sa ndiaboot gui diogué nan fi, té même soun fi diogué woon tamit Sëriñ bi dou ci wakh dara day xamni Yàlla yori bakkan.

Womar

Le Général Bamba va célébrer le Magal de TOUBA à DAROU MOUHTY Ville fondée par son Grand père Mame Thierno Brahim Mbacké...
10/08/2025

Le Général Bamba va célébrer le Magal de TOUBA à DAROU MOUHTY
Ville fondée par son Grand père Mame Thierno Brahim Mbacké et 2 ème capitale du Mouridisme située à 28 km de Touba.

10 août 1895Dans son rapport du 10 août 1895, Marius Pierre Leclerc, Administrateur du Cercle de Saint-Louis, qui était ...
10/08/2025

10 août 1895

Dans son rapport du 10 août 1895, Marius Pierre Leclerc, Administrateur du Cercle de Saint-Louis, qui était à la tête du détachement chargé de chercher Serigne Touba à Mbacké Bâry, évoque un détail très édifiant sur la personnalité de Mame Thierno Ibra Faty. En effet, Leclerc dit qu’ayant donné quartier libre à ses troupes au campement, il n’avait conservé pour son service qu’une demi-douzaine d’éléments armés de sabres, qu’ils dégainaient à tout bout de champ pour impressionner Mame Thierno. Mais, ce fut avec un sourire narquois que le petit-frère du Cheikh accueillit leurs manœuvres. Autant dire que cette tactique d’intimidation n’avait rien qui pouvait ébranler sa conviction, sa confiance en Dieu ni sa détermination.

Rappelons que Serigne Thierno Ibra Faty était âgé d’à peine 30 ans à cette époque. Une émissaire digne de ce nom ! Ndaw lu mat sëkk ndaw. Puisse le Très-Haut le rétribuer à la hauteur de cette importante mission qu’il accomplit de fort belle manière auprès du Gouverneur sur instruction de son vaillant grand-frère et guide spirituel Cheikh Ahmadou Bamba.

Recherche : Seydina Omar Ba


📍10 AOÛT 1895 - 10 AOÛT 2025 : Mbacke Bari- Djéwol - Louga - Ndar - Dakar- Gabon.Ce 10 Août est à marquer d'une pierre b...
10/08/2025

📍10 AOÛT 1895 - 10 AOÛT 2025 : Mbacke Bari- Djéwol - Louga - Ndar - Dakar- Gabon.

Ce 10 Août est à marquer d'une pierre blanche car il correspond au début de l'exil de Serigne Touba. Il est parti de Mbacke Bari ce jour pour répondre aux convocations du gouverneur du Sénégal.

Dieureudieufé SERIGNE TOUBA


BOROM DAROU: Kerok 18 safar 1895 bako Sëriñ bi wanée guinaaw dém taseek toubab yi diéewal, ndjiital soldaar yi dafa yaba...
08/08/2025

BOROM DAROU:
Kerok 18 safar 1895 bako Sëriñ bi wanée guinaaw dém taseek toubab yi diéewal, ndjiital soldaar yi dafa yabal ay soldaar yi niou aksi Mbakke Baari, ni Thierno, gouverneur néena nga tasaaré mboolom Sëriñ Touba mi mép té diogué fi mbakke baari fiyak foukki fanak diouroom wala louko moy sou nieuwée taal keur gui, ray ndiaboot gui.

Borom Darou ca ndaw ga amé 30 ans waayé ca fitwa Mame Thierno niko diogué gui moom dinaako déf ndax Sëriñ Touba digaloon namako, nima fooma mana yoralé ndiaboot gui rek bakhna, waayé dou léegui ndax dama fée tambali woon am mbay té aggoul, kon dinafi diogué waayé soumako Sëriñ Touba digaloul woon douma dém donté sama bakkan daf ciy dés, niko nak linga wax dangay lakk keur gui ak ndiaboot gui loolou dou mana am moukk loudoul dangamaa ndieukeu ray ba paré.
Soldaar ya mérr lool dém waxko sén kilifa, daal fay nieuwaat niko gouverneur néena nga toukhou saa you la nékhée ak noumla nékhé, Borom Darou niko waayé soumako Sëriñ bi digaloul woon doumako déf.

Womar


Dieureudieufé Serigne Touba 🇸🇳❤️
08/08/2025

Dieureudieufé Serigne Touba 🇸🇳❤️

Al Mountakha 🙏🏼💙
06/08/2025

Al Mountakha 🙏🏼💙

03/08/2025

Ki tukki wonn (Serigne bi)
Ak kimu fi baayi wonn (Borom Darou Mouhty)
Ap Taxawaayam kawéna

Adresse

Darou-Mousty
Louga

Téléphone

+221777258833

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Mbéctém Darou Mouhty publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager