Salaam TV Officie

Salaam TV Officie Bienvenue sur la Chaîne de Salaam TV Officiel Abonnez-vous maintenant et Activez la Cloche la de noti

Jullig Àjjuma ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ci teewaayu Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke -Yal na fi yàgg lool te wér-.Àjjuma...
24/02/2023

Jullig Àjjuma ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ci teewaayu Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke -Yal na fi yàgg lool te wér-.
Àjjuma 3i Baraxlu (Shahbaan) 1444H/ 24 Février 2023

Une importante délégation du Khalif Général des Mourides a été reçue ce mardi 21 février à l'ambassade de la République ...
21/02/2023

Une importante délégation du Khalif Général des Mourides a été reçue ce mardi 21 février à l'ambassade de la République Turque au Sénégal .

Cheikh Mouhamadou Mountakha MBACKE vient une fois de plus manifester sa solidarité au peuple Turc suite aux différents tremblements de terre.

Cette importante délégation dirigée par Serigne Moustapha Mbacké fils de serigne Cheikh Gaindé Fatma et ancien ambassadeur du Sénégal en Turquie était également composée de El hadj Mbackiyou FAYE représentant du Khalif Général des Mourides à Dakar, Serigne Bassirou LO imam ratib de la mosquée de Massalickoul djinan, Serigne Khadim Diop Secrétaire particulier du Khalif, de Moustapha Diop et du Responsable Moral de Hizbut-Tarqiyyah Serigne Youssouph Diop.
La somme de 100 millions de Fcfa à été remise à son excellence Hatice Nur sağman Ambassadrice de la Turquie au Sénégal
, , , ,

♦️Sokhna Ndate CISSE champions du mondeSoxna Ndate SIISE mi i teewaloon Sénégal ca jongante tari Al xur'aanul Kariim bac...
07/10/2022

♦️Sokhna Ndate CISSE champions du monde

Soxna Ndate SIISE mi i teewaloon Sénégal ca jongante tari Al xur'aanul Kariim baca Dubaay moo jël Première 1️⃣ Al hamdu lillaahi Senegaal amatina Ndam 🥰🥰🥰

Weer wi feeñut, kon suba ci Talaata ji dëppoo ak 27 Septembre 2022 mooy doon 30i Diggi-Gàmmu (Safar), Àllarba 28 Septemb...
26/09/2022

Weer wi feeñut, kon suba ci Talaata ji dëppoo ak 27 Septembre 2022 mooy doon 30i Diggi-Gàmmu (Safar), Àllarba 28 Septembre doon benn panub Gàmmu (1er Rabiihul Awwal).

Samedi 08 Octobre, dëppoo ak 11 Rabiihul Awwal (Guddig 12) -Insàllaa- mooy nekk guddig Gàmmu gi.
——
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.

INNA LILLAHI WAINNA ILÉYHI RADION IMAM MOUSTAPHA  GEUYE YALLA NAKO YALLA YEUREM
20/09/2022

INNA LILLAHI WAINNA ILÉYHI RADION IMAM MOUSTAPHA GEUYE YALLA NAKO YALLA YEUREM

Jullig Àjjuma ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ci teewaayu kilifa gi Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke, 19 Safar 1444H / 16 Sept...
16/09/2022

Jullig Àjjuma ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ci teewaayu kilifa gi Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke, 19 Safar 1444H / 16 Septembre 2022
Grand Mosquée de Touba

https://koparexpress.com/apps/collectes/tckTOUBA CA KANAM  LANCE UNE CAGNOTE D’1 MILLIARD DE FCFA POUR FAIRE FACE AUX UR...
09/09/2022

https://koparexpress.com/apps/collectes/tck

TOUBA CA KANAM LANCE UNE CAGNOTE D’1 MILLIARD DE FCFA POUR FAIRE FACE AUX URGENCES DANS LA VILLE SAINTE: PAVAGE, REBOISEMENT ÉCLAIRAGE PUBLIC, ADDUCTION D'EAU TOILETTES PUBLIQUES.

07/09/2022

🔸 Ayca Murit Ndigël !!! Barkeelu 1 000F SAFAR Touba ca kanam

🔸Ayca Murit Ndigël !!! Barkeelu 1 000F SAFAR Touba ca kanam
07/09/2022

🔸Ayca Murit Ndigël !!! Barkeelu 1 000F SAFAR Touba ca kanam

-vous et Activez la Cloche la de notification pour Recevoir toutes les vidéos de Salaam TV OfficielAbonnez-vous ✅...

13/08/2022
07/08/2022
07/08/2022
22/07/2022

FATWA - Serigne Cheikhouna Mbàcke Abdoul Wadood - Laaj ak Tontu ci Diine

21/07/2022

- -

Adresse

Colobane
Dakar

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Salaam TV Officie publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Salaam TV Officie:

Vidéos

Partager

Entreprises De Médias á proximité



Tu pourrais aussi aimer