Lamine Ba Pastef

Lamine Ba Pastef Le Don de soi pour la patrie

15/07/2025

Wolof ↓

Ànd ci soppante gu dëggu gu dul dog ak ub gis-gis bu nu bokk ci Senegaal gu dëgër, moom boppam, naat te booloo. Donte du neex ñiy xaar ag lajj.

Dara, dara sax, manul a dagg diggante bu dul dog bu am boole bu Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay ak jëwriñam ju Njëkk ji, Usmaan SONKO.
Booloo, nekk njariñi réew mi ci kanam, ak ug aamu gu am solo ci coppite ak yegg fi ñu jëm.

Maa ngi wax bu baax ne : yal na Senegaal jot ci loolu, yal na dal bépp aji-bëgg réew bu booloo, ak lépp njiitu làng gi te amu ci dundal ngir jàppale bu baax liggéeyi nguur gi.

Ci jamono yu jafe yii, dunu def fu sori ci bu nu nekkee benn benn, fàww nu doon wenn say ak booloo ci li ëpp solo. Nekk ci ginnaaw Njiitu Réew mi ak Jëwriñ ju Njëkk ji Usmaan SONKO, nanu des ci sàppe yi. Booloo, teg yoon wu Senegaal di juboo ak moom, gëm sunuy jikko, jëm ci ngëm-ngëmam, ak wëlbatiku jëm ci ëllëg gu jub te naat ci ñépp.

Ñaar ñii fésal nañu ag aamu gu mat sëkk ci liggéeyal réew mi. Dëggu ci seen kàddu yi ñu dige, seen ug dëggu ci nekkiinu askan wi ak seen ub gis-gis bu jëm ci ëllëg gu jàppale ànd bi, ci ab balluwaayu gépp maas.

Seen ub diggante weesu na ay ñaax, weesu ay wuute, ak man a indi yenn xàjjale. Dalalleen seen xel : dara du xew !

Usmaan SONKO ak Basiiru Jomaay Fay duñu mas a fàtte dëgg-dëggi li ëpp solo di nu xaar : li leen boole dafa ëpp li leen man a xàjjale. Seen jaar-jaar bu ñu bokk def nuy jàngal bind bu am xóot : ëllëgu Senegaal gu tegu ci bennoo, takku, ak weg xalaati moom sa bopp, yoon ci askan wi ak ug suqaliku.

« Xeex lenn rekk la mooy nekk ci jafe-jafe yi askan wi nekk di muñ », cig pàttali kàdduy Njiitu Réew mi 14i fani sulet.
« Kàddug Nguur gu aamu, ak def ko ciy jëf, ak doxaliin, ga (exigence) ak jaar yoon », ci lu Jëwriñ ju Njëkk ji féddali ci bis boobu.

Ñaari kàddu yuy jëm ci booloog diggante bi am ci ñaari niti ETAA yii.

🎉 Ndokkale bisu judd bu dellusi bu neex,
Sëriñ Jëwriñ ju njëkk sunu njiit !
Ci bisu fàttali bii, nu ngi ciy féddali sunu lëkkaloo, kóolute ak sunug aamu ci des ci seen wet. At mu bees mii yal na nekl atum dëgër, wér ak sottal liggéey bu am solo bi ngeen di def ngir sunum réew.

Vive Senegaal, Senegaal gu jub, moom boppam, takku te dëgër ci yaakaar !

——

𝗨𝗻𝗶𝘀 𝗽𝗮𝗿 𝘂𝗻𝗲 𝗲𝘀𝘁𝗶𝗺𝗲 𝗿𝗲́𝗰𝗶𝗽𝗿𝗼𝗾𝘂𝗲, 𝘂𝗻𝗲 𝗹𝗼𝘆𝗮𝘂𝘁𝗲́ 𝘀𝗮𝗻𝘀 𝗳𝗮𝗶𝗹𝗹𝗲 𝗲𝘁 𝘂𝗻𝗲 𝘃𝗶𝘀𝗶𝗼𝗻 𝗽𝗮𝗿𝘁𝗮𝗴𝗲́𝗲 𝗰𝗲𝗹𝗹𝗲 𝗱’𝘂𝗻 𝗦𝗲́𝗻𝗲́𝗴𝗮𝗹 𝗳𝗼𝗿𝘁, 𝘀𝗼𝘂𝘃𝗲𝗿𝗮𝗶𝗻, 𝗽𝗿𝗼𝘀𝗽𝗲̀𝗿𝗲 𝗲𝘁 𝘂𝗻𝗶. 𝗡’𝗲𝗻 𝗱𝗲́𝗽𝗹𝗮𝗶𝘀𝗲 𝗮̀ 𝗰𝗲𝘂𝘅 𝗾𝘂𝗶 𝗴𝘂𝗲𝘁𝘁𝗲𝗻𝘁 𝗹𝗲𝘂𝗿 𝗲́𝗰𝗵𝗲𝗰 !

Rien, absolument rien, ne saurait briser le lien indéfectible qui unit le Président de la République, Bassirou Diomaye Faye, et son Premier ministre, Ousmane SONKO. Ensemble, ils portent les intérêts de la nation en bandoulière, avec une détermination inébranlable à réformer et à réussir.

Je le dis avec force : que les Sénégalais soient rassurés, que les patriotes se mobilisent, et que chaque responsable du parti s’engage résolument à fédérer les forces vives pour soutenir pleinement l’action gouvernementale.

En ces temps décisifs, il est plus que jamais impératif de dépasser les postures individuelles, de faire bloc, et de nous rassembler autour de l’essentiel. Derrière le Président de la République et le Premier ministre Ousmane Sonko, serrons les rangs. Unis, nous tracerons le chemin d’un Sénégal réconcilié avec lui-même, fidèle à ses valeurs, porté par ses convictions, et tourné vers un avenir de justice et de progrès partagé.

Ces deux hommes incarnent un engagement total au service du pays. Leur fidélité à la parole donnée, leur ancrage dans les réalités du peuple et leur vision audacieuse de l’avenir font d’eux un tandem solide, une source d’inspiration pour toutes les générations.

Leur relation dépasse les sensibilités, transcende les divergences, et résiste aux vents contraires les vents de la division. Qu’ils se calment : aucune tempête ne se lèvera !

Ousmane Sonko et Bassirou Diomaye Faye n’ont jamais perdu de vue cette vérité essentielle : ce qui les unit est infiniment plus grand que ce qui pourrait les diviser. Leur parcours commun nous enseigne une leçon fondamentale : l’avenir du Sénégal repose sur la cohésion, la loyauté, et le respect des idéaux de souveraineté, de justice sociale et de développement.

« Le seul combat qui vaille est celui contre les difficultés que les Sénégalais endurent », a rappelé le Président de la République ce 14 juillet.
« La parole de l’État engage, et il faut la traduire en actes, avec méthode, exigence et efficacité », a martelé le Premier ministre, ce même jour.

Deux déclarations qui disent tout de la convergence de vues entre ces deux hommes d’État.

🎉 Joyeux anniversaire, Monsieur le Premier ministre, notre leader !
En ce jour symbolique, nous vous réaffirmons notre attachement, notre confiance et notre engagement sans réserve à vos côtés. Que cette nouvelle année vous apporte force, santé et réussite dans la noble mission que vous accomplissez pour notre pays.

Vive le Sénégal, un Sénégal juste, souverain, debout et porteur d’espérance !

#

Joyeux anniversaire, PROS.Doundeul!Weral! Amal jam! Amal ndam!Amal deug! Yalla samal ñu la!
15/07/2025

Joyeux anniversaire, PROS.
Doundeul!
Weral!
Amal jam!
Amal ndam!
Amal deug!

Yalla samal ñu la!

Adresse

Saint-Louis

Heures d'ouverture

Mardi 09:00 - 17:00
Mercredi 09:00 - 17:00
Jeudi 09:00 - 17:00
Vendredi 09:00 - 17:00
Dimanche 09:00 - 17:00

Téléphone

+221764739560

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Lamine Ba Pastef publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager