Chita-i Media

Chita-i Media Diangalem Kou Ted ki

YÓBBALU Bis bi….
25/11/2024

YÓBBALU Bis bi….

29/10/2024

[ Xarbaaxi Sëriñ Tuubaa ]

SËRIÑ TUUBA bimu juggee ci géej gi ba nekk Daarul Manaan, amna bés mu gaslu neeg ba teere yi nekk, daadi ëmb teere yi ci mbajji ñu suul leen, yaggul dara neeg ba lakk. Maam Cerno (Rta) yëg ko amsi ag jaxle di wax SËRIÑ BI limasi jaaxal mooy lëggéey boobu (xassida ya fa nekkoon)…

SËRIÑ TUUBA ni ko : danga xamul ni fàgguwoon nañuko, suul naa lépp ! Maam Cerno ni ko suuf de doyna waar ! SËRIÑ TUUBAA ni ko danga xamul ni suuf lumako santul duko deff !

Source : Garabu Tuubaa VOL4

12/05/2024

[ Xassaidal’ Kiraam ]
Nee na ñu SËRIÑ TUUBAA mo wax ni :
« Xasidag Wa kaana Haqqan ku ko jàngal ku ñu jàpp (ku ñu arreté war ko atte) wàlla ku nekk ci jaqare, gannaaw julli gee and ak njàpp, danañu ko bayyi, budee jaqare itam dana deñ.»
📚 Source : Jotaayu Texe VOL7

11/05/2024

*[Yobal beus bi]*

Sëriñ Tuubaa neena :
" Yaw Murid bi, na nga bëggal sa mbokkum jullit linga bëggal sa bopp, soo ko defee di nga tàbbi àjjana ci ludul hisaab.

Te ngay teral gan, doonte ab saay saay la sax.

✍️ 📚Source : Silkul Diawahir

Kou ken doul meussa faté si kaaw suufSERIÑ SALIOU MBACKÉ YLLA SA BOROM YOKOU LERAAM TASS NIOU SI BARKEMM
28/12/2022

Kou ken doul meussa faté si kaaw suuf
SERIÑ SALIOU MBACKÉ
YLLA SA BOROM YOKOU LERAAM TASS NIOU SI BARKEMM

Adresse

Saint-Louis

Téléphone

+221783741725

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Chita-i Media publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Chita-i Media:

Partager