DEVE parle en wolof

DEVE parle en wolof DEVE parle en wolof

Jigéen ju të xaalis, mucc yomb ko, aw xas teggi ko mook ak njabootam.
24/01/2023

Jigéen ju të xaalis, mucc yomb ko, aw xas teggi ko mook ak njabootam.

Xeex bi jéggi na SONKO!Dadi xeex bu nekk dina am kuy nekk ca kanam niki mbooloo yépp, waaye jëmmi xeex mooy lii, dëkkee ...
24/01/2023

Xeex bi jéggi na SONKO!

Dadi xeex bu nekk dina am kuy nekk ca kanam niki mbooloo yépp, waaye jëmmi xeex mooy lii, dëkkee naan meew mi di ñu jox neefere yi lees bëgg mu dakk.

Sonko kenn kepp la ci nun!

Cëy MAKI!  (Tagatembe) SONKO di la dàq, coowal ñetteelug kay kar la!Sa fetal gi de moo la dese! Ndax dinga ko tal kay mo...
24/01/2023

Cëy MAKI! (Tagatembe) SONKO di la dàq, coowal ñetteelug kay kar la!

Sa fetal gi de moo la dese! Ndax dinga ko tal kay mooy laaj bi?

Fii, am na RÉEW mum may nuróol de!Daa mel ni joxaat nañu leen démb sax!
24/01/2023

Fii, am na RÉEW mum may nuróol de!

Daa mel ni joxaat nañu leen démb sax!

Mbete man ab rëbóo laa ba duma xalaat!Dinaa jël sama doom yóbb(arme) ñu dàq ko(libere) ko ne ko soxla wuñu la, mu dem ba...
24/01/2023

Mbete man ab rëbóo laa ba duma xalaat!

Dinaa jël sama doom yóbb(arme) ñu dàq ko(libere) ko ne ko soxla wuñu la, mu dem ba jamono jii ñu xam ni am na fu Réew mi jëm, ñu ne ma sa doom jiñ dàqoon na ñëwaat rayanteel ñu, te mu leer la ne bu yii jàllee du fa toog dañu koy dàqaat nde daa am lees koy doye rekk.

Dinaa bàyyiwaat sama doom jooju muy bokki ca ñay faagaagal aw askanam? Maa lànk.

Ndokk ba fekkoon na ko ci beneen liggéey sax!(demul de) kenn du taqal samaw askan deret ngir alal man.

Coupe du Monde Qatar 2022Joŋante 8e de finale yu dinañu ko tàmbali tay ji ci bu 15h jote, Olaand 🇳🇱 mooy laale ak Aameri...
03/12/2022

Coupe du Monde Qatar 2022
Joŋante 8e de finale yu dinañu ko tàmbali tay ji ci bu 15h jote, Olaand 🇳🇱 mooy laale ak Aamerig 🇺🇲. Bu 19h jote dinañu amal ñaareelu joŋante bi, Arsantin 🇦🇷 mooy daje ak Óstraali.

Ñaari joŋante yi ñisi door ñooy daje ci 1/4 de finale yi !

Otto Addo mi tàggat wa Ghana tekki na nombal tànkam ! 🇬🇭
02/12/2022

Otto Addo mi tàggat wa Ghana tekki na nombal tànkam ! 🇬🇭

Adresse

Touba
Rufisque
11494DAKAR

Téléphone

+221761309852

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque DEVE parle en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à DEVE parle en wolof:

Partager