30/05/2024
C’est avec beaucoup de plaisir et d’émotion que j’ai retrouvé, aujourd'hui, mon pôle d’avocats. Ces dames et ces hommes sont des acteurs Alpha du PROJET. Ils en ont payé le prix fort : procédures disciplinaires, suspensions, menaces, arrestations…
Mais ils sont restés dignes à nos côtés, résilients et désintéressés.
Mes pensées à ceux qui n’ont pu être présents aujourd’hui.
Merci !
•••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••
Mbégte mu rëy laa àndal ak xol bu sedd ci gisantewaat, tay, ak sama layookat yi. Soxna yi ak góor ñi ñoo nekk alfay SÉMB BI. Fay nañu ci njëg lu rëy : doxaliinu yar, ay ajandi, xupp, jàpp...
Waaye dañoo des ak seen ngor ci sunu wet, muñ te bañ a xaar dara.
Sama xel mu ngi ci manul a teew tay.
Jërëjëf !