Mouride Xidma

Mouride Xidma Jërëjëf Sëriñ Tuubaa Xaadimu Rasuul Jaaraama Maam Seex Ibraahiima Faal.

Ndigël Xalif Seneraal dee Murid Sëriñ Muntaxaa Mbàkke Jox Na Ndigël Xalif Seneraal dee Baay Faal Ñu Wara Bayaat Armeeri ...
09/11/2025

Ndigël Xalif Seneraal dee Murid Sëriñ Muntaxaa Mbàkke Jox Na Ndigël Xalif Seneraal dee Baay Faal Ñu Wara Bayaat Armeeri Tuubaa Baxiya ajjuma le 14 novembre insàlaa ku yaatal yàlla na Say Xéewal yaatu Loool Barke Boroom Tuubaa

Mii ngi wax it Sunu Boroom di ko kañ di ko naan, naan ko:« Yaw mi nga xam ne, loo ne amal mu am, nangul masamag ñaan ci ...
31/10/2025

Mii ngi wax it Sunu Boroom di ko kañ di ko naan, naan ko:

« Yaw mi nga xam ne, loo ne amal mu am, nangul ma
samag ñaan ci barkeb Yonṅent bi Sunu Boroom nangul
ma samag ñaan, jéggal ma samay bàkkaaar, te jéggal kepp
koo xam ne mi ngi dellu ci yaw ngir sàkkug njëggal ci
barkeb Yonṅent bi . »

Echantillon des grilles de la grande mosquée 🕌 de Touba
26/10/2025

Echantillon des grilles de la grande mosquée 🕌 de Touba

25/10/2025

Kàdduy dëgg !

📹 : via TikTok

Maître Mouhamadou Bamba Cissé, Ministre de l'Intérieur et de la Sécurité publique, s'est rendu à Touba pour une visite p...
17/10/2025

Maître Mouhamadou Bamba Cissé, Ministre de l'Intérieur et de la Sécurité publique, s'est rendu à Touba pour une visite privée chez le Khalif Général des Mourides, Serigne Mountakha Mbacké, ce jeudi 16 octobre 2025.

  Bismillah
13/10/2025

Bismillah

Ginaaw bi ñu dajee ci sowwu jumaa ji ngir séentu weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus Saanii) 1447H ànd ko ak pàcc yi aju ci ñoom...
22/09/2025

Ginaaw bi ñu dajee ci sowwu jumaa ji ngir séentu weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus Saanii) 1447H ànd ko ak pàcc yi aju ci ñoom te teewal leen ci yeneen warab yi; mbooloo mi Sëriñ bi dénk wàllum séentu weer wi ci Tuubaa ñooy xamal ñépp ne weer wi feeñ na. Kon suba ci Talaata ji dëppoo ak 23 Septembre 2025 mooy benn panub Rakki Gàmmu 1447H.
——
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.

📷 : Mamadou Wade Diop ( Dr Drone )

21/09/2025
Sokhna Aminata Lo di wayjuru Serigne Makhtar Diène moo fi bàyyi koo. Yal na ko Yàlla yërëm te xaare ko Al-Jannah !Ñu def...
17/09/2025

Sokhna Aminata Lo di wayjuru Serigne Makhtar Diène moo fi bàyyi koo. Yal na ko Yàlla yërëm te xaare ko Al-Jannah !
Ñu def Fatiha + 11 Ixlaas yéene ko ko. 🙏🏿

Adresse

51 Rue Des Frères J Et R Kennedy
Salon-de-Provence
13300

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Mouride Xidma publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Mouride Xidma:

Partager