Al Murtadaa tv

Al Murtadaa tv Ab séen la ngir lépp lu aju ci mbiri diine

27/07/2025

Episode(1) Waxtaan wi: Naka la mag ñi daa dundalee Safar.....par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Jubbanti aw déggiin ci waxi Sëriñ bi.....par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Tan loo nit ki wéy ci sëy....par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Tànn Soxna si jegeñaale wala ci jàmbur...par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Bunuy rob néew danuy taxaw wala danuy toog...par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Lu Sëriñ bi du wax ci bayit bi....par Serigne Mourtada Ndiaye

20/07/2025

Nisaabu Asaka..par Serigne Mourtada Ndiaye

18/07/2025

Laaj ak tontu ci diine par Serigne Mourtada Ndiaye

17/07/2025

Laaya biireg
Sëriñ Murtadaa Njaay ci
PM. Ousmane SONKO "muñ wax yi te xam ne Yàlla..."

06/07/2025

Ndax manees naa fay ñaari RAKKA FAJAR.....par Serigne Mourtada Ndiaye

06/07/2025

Watu ak lewi wee bisub Tabaski.... par Serigne Mourtada Ndiaye

06/07/2025

Ndax góor buy labat Jigéen sañ naa wéetoo ag moom.......par Serigne Mourtada Ndiaye

Adresse

Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Al Murtadaa tv publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager