
24/08/2024
Ñun mourid nak sunu djiko sunu mélo linga xam né bugne lako waxee ak bugne la ko waxul lolou lagniy deff modi kepou ko xamné ni yalla deff serigne touba nekh nala dagne lay def comme sunu bopou kepou ko xamné nak niko yalla def neekhou la dugne la limaalé si dara. Waslm