Xibaaru reewmi tv 2.sn

Xibaaru reewmi tv 2.sn Xibaar yu wér te leer ci kàllaamay kocc

ministre de la justice Yacine Fall . installée .
16/09/2025

ministre de la justice Yacine Fall . installée .

*Allemagne Palestine 🇵🇸 : ay diounni Doomi Adama di Ammal Ay Dokhi Gnakhtou thia Berlin nguir jàpple Askanu Palestine .*...
16/09/2025

*Allemagne Palestine 🇵🇸 : ay diounni Doomi Adama di Ammal Ay Dokhi Gnakhtou thia Berlin nguir jàpple Askanu Palestine .*

Xibaaru Réewmi

*Israël : ap attaque Thia Jérusalem-Est Waral juróomi doomi Adama yu Faatu , Waa Hamas Gnoogi Rafetlou attaque bi, armée...
16/09/2025

*Israël : ap attaque Thia Jérusalem-Est Waral juróomi doomi Adama yu Faatu , Waa Hamas Gnoogi Rafetlou attaque bi, armée israélienne bi mingi gëstu Nguir Kham Gni def attaque bi , moom mi def louni mél faat Nanko .*

Xibaaru Réewmi

*Sénégal 🇸🇳 Lou Euppu teemeeri téeméeri Doomi Adama Thia plage Oukaam gnóom lan teck Thi Thi ab gaal Beugoona dem Bitim ...
16/09/2025

*Sénégal 🇸🇳 Lou Euppu teemeeri téeméeri Doomi Adama Thia plage Oukaam gnóom lan teck Thi Thi ab gaal Beugoona dem Bitim Réew, louni mél tamitte lan néméko Thia Ngor 19 Doomi Adama mou Amthi 5 sénégalais yoo Khamené téck Nanleen Lokho .*

Xibaaru Réewmi

*Sénégal 🇸🇳 : Présidente du groupe parlementaire TAKKU WALLU Sénégal, Aïssata Tall Sall tàbbu Nanko élue  membre du Cons...
16/09/2025

*Sénégal 🇸🇳 : Présidente du groupe parlementaire TAKKU WALLU Sénégal, Aïssata Tall Sall tàbbu Nanko élue membre du Conseil d’Administration du Réseau des parlementaires Bou Banque mondiale Ak Fonds monétaire international (FMI) Nguir Mou teewal Afrique de l'ouest Thi Gnaari institutions financières yooyo mou Wara Bokko Thi Gni jël Doggal Thi politique bu Gnaari institutions yi .*

Xibaaru Réewmi

16/09/2025

Urgent!
Touba: Un plan d’action d’urgence lancé contre les inondations

16/09/2025

Case Waly Seck: "Amul benn mandaa buñu ko japp"*

Xew-xew yi dañuy wax ni dañu joxe benn mandaa ngir jàpp woykat bii di Waly Ballago Seck. Ak liñu wax ci turam ci benn rapoor bu CENTIF, ba leegi daanu wuñu artist bi. Waaye, ndax liñu ko tuumal ci wàllu fomp xaalis, dafa dakkal liggéeyam ci wàllu music ba fàww.

Sunu sukkandikoo ci surnaal bi, mën nañu laaj yeneen nit ñu am doole ci laŋket bi ñuy wéyal.

15/09/2025
ministres Bamba Cissé et Abdourahmane Diouf installés
15/09/2025

ministres Bamba Cissé et Abdourahmane Diouf installés

ministres dethie Fall et Amadou ba installés
15/09/2025

ministres dethie Fall et Amadou ba installés

Assemblée nationale daadina Oubbi gnaareelu session parlementaire extraordinaire de l’année nguir voté Gnatti lois :  • ...
15/09/2025

Assemblée nationale daadina Oubbi gnaareelu session parlementaire extraordinaire de l’année nguir voté Gnatti lois :

• projet de loi nguir Soppi l’accès Thi jafandikoo réseau des télécommunications publiques (RUTEL) ;

• projet de loi n°17/2025 nguir Soppi Code général des impôts .

• projet de loi n°16/2025 jëm Thi Code des investissements.

Amadou Dia moo Wootu Amadou ba
ndajeemi Thi teewaayu ministre Marie Rose Faye mi yoré wàllum Dioglanté Thi institutions yi .

Xibaaru Réewmi

*Thaïlande 🇹🇭Cambodge 🇰🇭 : khaatim deggoo Amna digeunté Thaïlande ak Cambodge Nguir Nio teckk ngànaay Yi digeunté gnaari...
14/09/2025

*Thaïlande 🇹🇭Cambodge 🇰🇭 : khaatim deggoo Amna digeunté Thaïlande ak Cambodge Nguir Nio teckk ngànaay Yi digeunté gnaari armées yi Guinaaw ay fànni diapanté Waral 36 Morts .*

Xibaaru Réewmi

Adresse

28
Dakar

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Xibaaru reewmi tv 2.sn publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Xibaaru reewmi tv 2.sn:

Partager