Euttu Mouride Yi

Euttu Mouride Yi Jok ngir liggéyal ku Teddki Khadimourassoul LAHI

Čëyy Mbégum Murid yi Féssal nga déll Mbecteh ci xoll yi Yàlla na nga fi yagg loôol té and AK Wer fi suñu Kanam Mbakké Ba...
29/03/2025

Čëyy Mbégum Murid yi Féssal nga déll Mbecteh ci xoll yi Yàlla na nga fi yagg loôol té and AK Wer fi suñu Kanam Mbakké Balla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
abonnez-vous

< Damaa déggoon ay waxam mu jëm cimbiru sunu Boroom, booba agseegunu fi. Ma dégluwax ji, déglu ko, keroog laa am ak moom...
15/03/2025

< Damaa déggoon ay waxam mu jëm ci
mbiru sunu Boroom, booba agseegunu fi. Ma déglu
wax ji, déglu ko, keroog laa am ak moom wollare xol.
Ndax man képp koo xam ne am naa yaqiin ci ne ku
gëm Yalla nga, ku wéetal Yàlla nga, dinaa la def sama
iir xol, ak sama wóllare. Loolu manuma ko woon a
ñàkk a wax ba mu dégg ko. >
Kàdduy Seex Muntaxaa Basiiru (Mbakke yagfi lol te werr) jëm ci Njiitu Réew mi
Bassirou Diomaye Faye

Al Mashrabu’ç çâfî minal manbahi’sh Shâfî : La fontaine pure émanant de la Source qui guérit ❤️❤️
15/03/2025

Al Mashrabu’ç çâfî minal manbahi’sh Shâfî : La fontaine pure émanant de la Source qui guérit ❤️❤️

Wadial Gamou ❤️ thieuy Cheikhoul xaadim ❤️           Xassida 👉   ❤️محَمَّدٌTraduction en wolof ✍️Da naa sakku, mu bàyyik...
12/09/2024

Wadial Gamou ❤️ thieuy Cheikhoul xaadim ❤️

Xassida 👉 ❤️محَمَّدٌ

Traduction en wolof

✍️Da naa sakku, mu bàyyikoo fa Yalla si darajay Yonent bi, lo xam ni, (bu xasee ba ñêw) deesu ko rinki mukk di ko jëllaat si man ta ba fåww nak.

✍️Sant naa sama boroom ta mooy Yalla, ta moom dé mooy ka nga xam ni, mooy ka ñuy sàkku sa moom, ta da naa ko sant si li mu ma nekkal ňeel ma di ma jéñal (lu bonn) ak di ma ñóddil (lima bögg) neel ma.

✍️Mbir mu may aji julli sa aji béglé ji nga xam ni, da na may ñeel ma sama bépp mbébett, ta itam di ki nga xam ni da na daq sama bepp noon.

✍️Kooku may wax turam wa mooy Muhammad di ki nga xam ni, da naa xémmém njubam ga, ta si tagg yii ma koy tagg, si la may dikkalé mbooleem xeeti xemmemteef yi.

✍️Naan na sama boroom, si darajay Yonent bi, may sàkku mu bàyyikoo sa moom Yalla něw si man, ag téxé go xam ni, déesu ko rinki waat (gu mu dul nàngu waat mukk).

Cheikhoul xaadim ✍️ ❤️

Mustafaal Xadiim dieuredieuf si bindou xassida gui
abonnez-vous 🙏🙏🙏

Don na sakku niou nianal kossi khassida gui
29/09/2022

Don na sakku niou nianal kossi khassida gui

18/06/2022

Adresse

Dakar

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Euttu Mouride Yi publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Euttu Mouride Yi:

Partager