Wolof ak Saabal

Wolof ak Saabal Wolof ak Saabal : man na noo wàx ne, joxewu nu ay dég-dég, joxewìin u dég-dég ci wolof la nu'y

21/06/2025

Sulaymaan Ñaŋ Jëwriñ mbokkum wolof 😊

Suba ak jàmm, ku sawar mbaa mu weregcekk rekk, man na ko a teewlu. Di naa ci sàgu lool.
19/06/2025

Suba ak jàmm, ku sawar mbaa mu weregcekk rekk, man na ko a teewlu. Di naa ci sàgu lool.

Téere bii jëm ci Tùubaa nu fasoowoon bind liggeeyale ko Sëriñ bi, di na génn gaawu 5 sulet 2025 ndeem soob na Yàlla. Ku ...
18/06/2025

Téere bii jëm ci Tùubaa nu fasoowoon bind liggeeyale ko Sëriñ bi, di na génn gaawu 5 sulet 2025 ndeem soob na Yàlla. Ku ci bëgg man nga cee teel a fàggu ba la a boo ba.

Cet ouvrage consacré à la ville de Touba que nous nous tâchions à écrire en guise de contribution au développement de la ville marque notre amour en vers le Cheikh et notre volonté d'œuvrer pour lui à jamais. Vous pouvez dès maintenant pré-commander votre exemplaire.


03/05/2025

Téereb lëgg-lëgg 100% ci wolof.

03/05/2025

Wolof u wolof : Lëgg-lëgg !

03/05/2025

Cin, bu naree neex, bu baxee xeeñ !!!

25/03/2025

B.A.T FIN PRÊT !
DÀY BI NOPPI NA !

Fegguw gandeeru wi !
16/03/2025

Fegguw gandeeru wi !

Feggu waa ngoo'g, fii ak ay fan yu néew !
16/03/2025

Feggu waa ngoo'g, fii ak ay fan yu néew !

Fii ak i fan doŋŋ,Li ñépp doon xaar!
15/03/2025

Fii ak i fan doŋŋ,
Li ñépp doon xaar!

Benjamín Mendy ginnaaw ba'ñ ko setelee wecc ca siif ga'ñ ko doon jìiñ, ngìr mu jekkandikuwaat ŋàt na ca Lorient.
19/07/2023

Benjamín Mendy ginnaaw ba'ñ ko setelee wecc ca siif ga'ñ ko doon jìiñ, ngìr mu jekkandikuwaat ŋàt na ca Lorient.

Bayern Munich bom na 27-0 ci jàkkaarloom ak Rottach-Egern en ci joŋanteb xaritoo ! 😲⚽️⚽️⚽️⚽️⚽️ Tel⚽️⚽️⚽️⚽️⚽️ Musiala⚽️⚽️...
18/07/2023

Bayern Munich bom na 27-0 ci jàkkaarloom ak Rottach-Egern en ci joŋanteb xaritoo ! 😲

⚽️⚽️⚽️⚽️⚽️ Tel
⚽️⚽️⚽️⚽️⚽️ Musiala
⚽️⚽️⚽️⚽️⚽️ Sabitzer
⚽️⚽️⚽️ Gnabry
⚽️ Davies
⚽️ Mazraoui
⚽️ Laimer
⚽️ Upamecano
⚽️ Saane
⚽️ Guerreiro
⚽️ Gravenberch
⚽️ Coman
⚽️ Maane

Bayern München kaful daal, doonte joŋanteb xaritoo la 😭

Adresse

Parcelles Assainies
Dakar

Téléphone

+221707504050

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Wolof ak Saabal publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager