BAYE DIOUF Guéweulou Baye

BAYE DIOUF Guéweulou Baye Dara déssoul loudoul Ndioukeul Cheikh Ibrahima Niass Baye
Baye Diouf Guéwalou Baye woténa Ndioukeul

19/10/2025
Al hamdoulilah Jumma Mubarakh En Route vers Ndioukeul Baye Niass Samedi 13 décembre à Guèdiawaye Terminus 70 Cheikh Baye...
17/10/2025

Al hamdoulilah
Jumma Mubarakh
En Route vers Ndioukeul Baye Niass
Samedi 13 décembre à Guèdiawaye
Terminus 70
Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye bi et kossi Kossi
Gniouggui invité gnieupp
Hall si kaw hall rekh insh allahou
Âne surtout pas Manquer

Al hamdoulilah Ndioukeul Baye Niass Samedi 13 décembre à Guèdiawaye terminus 70Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye Et kossi ...
01/10/2025

Al hamdoulilah
Ndioukeul Baye Niass
Samedi 13 décembre à Guèdiawaye terminus 70
Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye Et kossi Dakar
Gniouggui invité gnieupp
Hall si haw hall
Insh allahou

Alhamdoulilah Dahira Dimanche 27/09/2025Wadjial Ndioukeul Baye Niass Samedi 13 décembre 2025Merci beaucoup jeunesse koss...
29/09/2025

Alhamdoulilah
Dahira Dimanche 27/09/2025
Wadjial Ndioukeul Baye Niass
Samedi 13 décembre 2025
Merci beaucoup jeunesse kossi Dakar
Pour ces cadeaux 🎁 offertes pour ma modeste personne
Yalla na yalla fay lén yokou sén beugeul si Baye
Si tolou Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye bi

Insh allahou invité nagniouSi gnieuppJeuness de kossi Dakar
25/09/2025

Insh allahou invité nagniou
Si gnieupp
Jeuness de kossi Dakar

22/09/2025
Al hamdoulilah Dahira Dimanche 21/09/25Cadeau bou makeu bou ame foumou commencer wayé amoule foumou yemMerci beaucoup sa...
22/09/2025

Al hamdoulilah
Dahira Dimanche 21/09/25
Cadeau bou makeu bou ame foumou commencer wayé amoule foumou yem
Merci beaucoup sama papa sama cheikh Mourabi
Il m a offert ce beau tableau photo de Mouhamed Nassir fils de Cheikh Ibrahima Niass BAYE
La photo a durée 30 ans
Haut ce qui m a plus marqué ces 30 ans qui correspond à ma date de naissance
Al hamdoulilah

Cette photo ne lui a jamais était offert
Il l a acheté lui même
Degeu degeu Alhamdoulilah

Cheikh Mourabi bou bakh la
Bou yatou la
Kou beugeu Baye Niass la
Sa temps yeupp def geako si yalla
Gnioune sougniou keur yi sakh
Bokatou gniousi parce que
Hall bigaye ndoundou lagniou yarè
Amougniou temps si Dara
Si adouna bi loudoule
Nekh si yalla rek
Alhamdoulilah yalla nala mayy wérrr
Mayy goudou fann
Sa thiakou téff yeupp
Té dou Dara Lou doule
Yalla yokou sa beuguel si Baye

Maggui sakou gniane si anlame bi yeupp
Guen gnianal ma Guewalou Baye bi
Alhamdoulilah Ndjieureudjieufee BAYE NIASS

Alhamdoulilah L évènement de l année temps attendu Ndioukeul BAYE NIASS Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye  et kossi Dakar ...
19/09/2025

Alhamdoulilah
L évènement de l année temps attendu
Ndioukeul BAYE NIASS
Cheikh Baye Diouf Guewalou Baye et kossi Dakar
Gniouggui len di wo

le Samedi 13 Décembre 2025
À Guèdiawaye tournal serigne Assane
Gniouggui invité gnieupp insh allahou
Hall si haw Hall
Djieureudjieuffé BAYE NIASS

Jumma Mubarakh 🤲🤲🤲
19/09/2025

Jumma Mubarakh 🤲🤲🤲

Adresse

Dakar
11000

Téléphone

+221771768039

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque BAYE DIOUF Guéweulou Baye publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à BAYE DIOUF Guéweulou Baye:

Partager