Faydou Kham Kham ak Weursseuk فيض العلم والأرزاق

Faydou Kham Kham ak Weursseuk فيض العلم والأرزاق ✅Zâliqal Faydou mine Rabbî
☑️Faydoul illâhiya
✅Faydatou Tidjânî
☑️Faydoul Khatmi

27/06/2025
10/05/2025

Amine NIASS 🤲
Sa dound ndjerign la yague fi té weur 🤲
Sou béno amé ci béne boum rek weurseuk wath boudoul djekh mouk Alhamdoulilah ❤️
fans

13/02/2025

Machalla dégloul so beugué am kham kham ak weurseuk kéne dou Cheikhoul Islam ''Ndjoup rek''

🌟Gnongui ndokèl Arif yeup ci djoudou Cheikhoul Islam khalifatou Lâhi fil Ardi. Nga khamni djoudom lêp barkéla, doundam l...
18/01/2025

🌟Gnongui ndokèl Arif yeup ci djoudou Cheikhoul Islam khalifatou Lâhi fil Ardi. Nga khamni djoudom lêp barkéla, doundam lèp barkéla, faddom lép barkéla.
✍️Mongui djoud Jeudi 15 ci wèrou radjab 1318 ci Taïba bi Takkoussane di djote ci rone Gouye. Lolou tolok jeudi 08novembre 1900.
moy 5e jours yowmoul khamîss fi hadara yalla bi motè.
#15 : YONANT bi wakhone na dinguène guiss cène BOROM comme ninguène di Guissé wêr bi sou tolè ci fouki fane ak gnare djeum fouki fane ak djourom. 15 dila djoundj (Hadaratoul haqqi/Noub/Wil..).
: Yonant bi néna moy wèrou YALLA.
#1318: soko bolè 13 lalay djokh mouy woné ni BAYE néké AHAD(lène).
: Yalla wâtna ci takoussane (wal Assri): né kép kouy Nite yangui ci pertement bam dess gni geum...
guim djoudo lèpam ndjèrignla (feuilles fruits fibres bois racines 5). , gnou ladjko loutakh YALLA bindla? Mounè: 👉Aw djadani hakane li djabril kassri fa inani wakilou siri siri( Yalla dafma amal ci DEUG nguir ma djangue dam dam yi ndakh mane lagnou d**k mboti mbot mi) mouy mboti Yonant bi ak Waliyou bi.
_mbandè gnounèko lo nam ci mindèf yi? Mounè: 👉 Wal oumatou kassdi fihimou ane assoukahoum ilâ hadaratil barri rahimi ilahina (khêt bi lima nam cignom moy omate lène gnom gneup djeumè ci pays yalla binga khamni moy adji bakh dji di adji yeureumè di ki gneup sokhlal.)
mou wakh gnouné: 👉Fahal abssarate aynaaka ahla mahichatane minal Abdi fahouwal Hamdoulilahi koulouhou (ndakh sa gnari geute👀 mossna tèguè ci kou geuna nèkh dound Djam bi di Ibrahima Niass nga khamni lèpam Alhamdoulilah la ?)
kone Alhamdoulilah bi YALLA wakhè ni: Djoulite yi cène moudjoug wotè moy Alhamdoulilah (Wa akhirou dahwahoum anil Hamdoulilah....)
DJEUREFJEUFATY NGUIR LÈP LINGA DÈF CI KHÊT BI.
🤲Yalna Yalla ALLAH yok sa leer tè geuna barkèl sa liguèy ba yolbi dila faikci.
🙏🙏Wathio ngak mindèf yi BAYE, gnoune gnoci dèss.
🤝Merci Mourabil Ârifîna LEPAPE yagnou khamal BAYE❣️

Ô vous qui avez cru, cherchez de l'aide avec patience et prière. En effet, Dieu est avec ceux qui sont patients يَا أَيّ...
29/11/2024

Ô vous qui avez cru, cherchez de l'aide avec patience et prière. En effet, Dieu est avec ceux qui sont patients

يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اسْتَعِينُوا بِالصَّبْرِ وَالصَّلَاةِ ۚ إِنَّ اللَّهَ مَعَ الصَّابِرِينَ

NB: djamou Yalla zahir yi bici geuna fort moy Djouli
Djamou Yalla Batine yi bici geuna fort moy Mougne.

👉Fonk léne dina mayé Weursseuk boudoul djekh

BAYE NIASS :  Alhamdoulilah wal Abdoulilah
26/06/2024

BAYE NIASS :
Alhamdoulilah wal Abdoulilah

11/06/2024

Yalna gnou Yalla moussal té mouthial gnou ci lép lou Yalla geureumoul.
Cét ci bakaar day oubi weursseuk. Alhamdoulilah

05/05/2024

Cheikh Ibrahim NIASS (r.a) : ''Beug am Dara té do liguéy moy beuga djoubadi''
Wakh dji yow mi nek ci ngourou adina yâko mom rawatina yow mi nék di liguéyal Yalla doundél sa gnak té bagna yâkâr kéne so beugué liguéy bi djâr yone''

13/04/2024

Mbok yi nagn léne bayi khél ci Djouli moy lignouy ndjeuka réglé ci yow amoul ham amoul Arif.

18/03/2024
03/03/2024

BAYE NIASS mouné gnou moytou ''RAMBÂDJ''
bolo la sokhla Alhamdoulilah

30/01/2024

Kadouy d**kané you amati ndjérign
CHEIKHOUL ISLAM ELHADJ IBRAHIM NIASS RADIYA LÀHOU ANEHOU

Adresse

Dakar

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Faydou Kham Kham ak Weursseuk فيض العلم والأرزاق publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager