01/04/2025
الحمد لله وبنعمته تتم الصالحات🙏🏾😍😍
Alhamdoulila, finalement notre rêve est devenu réalité. Nous venons téléchargeur tout le Coran à travers une belle psalmodie de Cheikh Ousmane Alfoutiyo Kane Riwaaya Warsh. Avec une haute qualité en MP3 et HD, elle diffusée dans nos différentes plateformes. Partagez et aimez en intégrant le « Sadakha Aldiarya ».
Al amndu lila, sunu mebët agg na. Jeexal nan kamil bi ci kaddug Seex Ousmane Alfoutiyo Kane Riwaaya Warsh. Mu jàng ko ci anam bu jeggi dayo, ñu taataan ko ci Mp3 ak HD. Kamil bii dîna jaall ci sunu berëbu jonkalante yi ngeen xam. Bëgg leen ko, tasare leen ko, di ngeen bokk si Sadakha Aldiarya 🙏🏾🇸🇳
👉🏾 الحمد لله وبنعمته تتم الصالحات🙏🏾😍😍

👉🏾 https://youtube.com/playlist?list=PLtIZ3bQfpU7Jhb-GEx8MpsHr7CexOCORV&si=aH8cF8CNbat2U5Tv
Ousmane Alfoutiyo Kane : ( Warch 'an naafi' ) برواية ورش عن نافع من طريق ابى يعقوب الأزرق