24/08/2023
Bonjour, bonsoir....
Di nuyu gneupp mak AK ndaw di yeugeul gneup gniko meuna téwé SAMEDI INCHALLAH réunion bi jeunesse Nawel Di amal pour relancer ASC DEGGO
Di sant bu bax Badiane...
SUNU PRÉSIDENT, MOUSTAPHA GUEYE AK MEMBRE YEUPP...
★IBRAHIMA NGOM
KHALIFA MALICK NDIAYE
LA JEUNESSE 🙏🙏🙏