
28/07/2022
Inter-Coalition yewwi-wallu. Choisissez le bulletin de gauche ou droite selon votre département de vote.
Bu fekeni danga book si department yii neké sa ndeydior(droite) yewwi ngay sandil carte bou feke thiamogn(gauche) wallu ngay voter insahala.
Gnu bayi si khél ndakh malheureusement bureau bo dem ding fa feek yewwi ak wallu