Xibaaru reewmi tv 2.sn

Xibaaru reewmi tv 2.sn Xibaar yu wér te leer ci kàllaamay kocc

*Sénégal 🇸🇳 : ngooruk Sénégal daloona Gnaari  machines de déminage Thi ndimbalu Japon, Gnaari machines yoo khamné Seen l...
24/07/2025

*Sénégal 🇸🇳 : ngooruk Sénégal daloona Gnaari machines de déminage Thi ndimbalu Japon, Gnaari machines yoo khamné Seen ligéey Mooy dindi ay mine💣💥 Thia Casamance .*

Xibaaru Réewmi

*Tàkkat Yaram football ⚽ Italie 🇮🇹 : Pervis Estupiñán bàyékoona Brighton & Hove Albion wutali Milan AC Thi  17 millions ...
24/07/2025

*Tàkkat Yaram football ⚽ Italie 🇮🇹 : Pervis Estupiñán bàyékoona Brighton & Hove Albion wutali Milan AC Thi 17 millions d'euros Daadi Wootu Theo Hernandez mi dem Al Hilal Att mouné moufay fayeeku 20 millions d'euros ba Gnatti Att .*

Xibaaru Réewmi

*Cambodge🇰🇭 Thaïlande🇹🇭 : Ay jàppanté Thi digeunté armées Cambodge Ak Thaïlande Thi dikk Wi Dokh Seen digeunté, Waral ju...
24/07/2025

*Cambodge🇰🇭 Thaïlande🇹🇭 : Ay jàppanté Thi digeunté armées Cambodge Ak Thaïlande Thi dikk Wi Dokh Seen digeunté, Waral juróom gnénte civils yu Faatu, Gnaari Reew-yi Kouné Yaagi toomal sa moroom'né yaa ndieugeu tiré , Bokona Thi Li Waral thioow Li Mooy mbiri soof Thi dikk wi Dokh Seen digeunté .*

Xibaaru Réewmi

24/07/2025

Sénégal 🇸🇳 Yoon ⚖️: Serigne Issa Touré Minou toomaal thi mbiri djigeen fëkk Nanko mou kharou Thi ap Teen ... Ay taalubeem daadi nan weddi tooma-yign téck Thi

Xibaaru Réewmi

*Tàkkat Yaram football ⚽ Espagne 🇪🇸 : numéro  #14 Marcus Rashford Abalé Nanko FC Barcelone Nguir bénn Att Bou diékhé équ...
23/07/2025

*Tàkkat Yaram football ⚽ Espagne 🇪🇸 : numéro #14 Marcus Rashford Abalé Nanko FC Barcelone Nguir bénn Att Bou diékhé équipe Catalan bi dafkoy dieunde digeunté 30 ba 35 millions d'euros ak payooru 14 millions d'euros Att bouné Waayé 70% lay Diott mi bayékoo Thi FC Barcelone .*

Xibaaru Réewmi

*Gaza : Gnaar Fokki réew ak juroom Daadi nan Ammal xaatim Nguir Sàkku Thi Israël mou daggal xeex bi Thia Gaza Bokkona th...
23/07/2025

*Gaza : Gnaar Fokki réew ak juroom Daadi nan Ammal xaatim Nguir Sàkku Thi Israël mou daggal xeex bi Thia Gaza Bokkona thi Reew-yi : France, Canada, Royaume-Uni, Japon ak l’Australie ... ONU Khamléné 875 Doomi Adama faat Nanleen Nio fëkk léen Thi beureub Bougnou Doon Diokhé ay ndimbal .*

Xibaaru Réewmi

23/07/2025

Kocc Barma yóbbu Nanko Kaso "Mandat de dépôt " téck nan Thi kawam Fokki Tooma Bokonathi : tasaare données personnelles, chantages ay nit, tasaare nataal yu Gnakk teggiin, Dokko Thi Doundou Nitt Gui "Vie privée" , Ande def ay Gnaaw teef, yoré données personnelles , rakhas khaalise bu Setul ...

Xibaaru Réewmi

*Mbiri François mancabou leujmeut yi Tàmblé'na .*Thia fattali procureur neewoon da doon mbeugg grilles yi bim negee kaso...
23/07/2025

*Mbiri François mancabou leujmeut yi Tàmblé'na .*

Thia fattali procureur neewoon da doon mbeugg grilles yi bim negee kaso té yoré nan vidéo bu 13 Minutes, moom mancabou Dankoo toomaloon thi Nio teck'ko le 17 Juin 2022 mou faatu 13 juillet 2022 Nio diébbal'ko Boroomam le 16 août Thia cimetière Saint Lazare de Béthanie , ak gnabootam diapné Dagnkoo fitnaal Waral Li Faatu .

Journal Yoor yoor bi

Ama Baldé téck nan Thi kawam mandat d'arrêt international fonioko fëkk jàpp diébbal'ko police .

L'obs .

*Tàkkat Yaram football ⚽ Angleterre 🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿 : Bryan Mbeumo bàyékoona Brantford wutali Manchester United ba 2030 Thi 75 m...
22/07/2025

*Tàkkat Yaram football ⚽ Angleterre 🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿 : Bryan Mbeumo bàyékoona Brantford wutali Manchester United ba 2030 Thi 75 millions d'euros + 5 millions d'euros bonus, attaquant camerounais bi Guinaaw 20 Buts thi Saison bii Weesu, mooy juróom mbeneelu joueurs bi Geuneu chère Gneel Manchester United .*

*Espagne 🇪🇸 Mbappé mooy jël numéro 10 bi Real Madrid Guinaaw bifa Luka Modrić bàyékoo .*

*Espagne 🇪🇸 : Jules kundé mogui Thi Yoon Nguir yokku contrat bi .*

*Espagne 🇪🇸 Rashford daadina Saytu wergui Yaramam Thia FC Barcelone .*

*Angleterre 🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿 : Viktor Gyökeresdu Dina dem Arsenal Lou yàggul Dara ba 2030 Thi 73 millions d'euros guinaaw 54 Buts Thi Saison 2024/2025 .*

*Espagne 🇪🇸 : Endrick bu Real Madrid Dina Took 8 ba 10 Semaines yum Doul football ndakh ap gaagnou gaagnou.*

Xibaaru Réewmi Fallou Walf Sall Bou Fatimah

*États-Unis 🇺🇲 : Réewum États-Unis daadina gënn Thi UNESCO Mouy gnaareelu Yoon Guinaaw biko Trump défé 2018 Waayé Joe Bi...
22/07/2025

*États-Unis 🇺🇲 : Réewum États-Unis daadina gënn Thi UNESCO Mouy gnaareelu Yoon Guinaaw biko Trump défé 2018 Waayé Joe Biden dogalaat'ko 2023, Doggal bi Donal Trump jël Dina tambalé me 31 décembre 2026, UNESCO Mooy bakhaas bi Bokko Thi ONU Yoré wàllum Aada ak thiossane ak wàllum Sàkku xam-xam .*

Xibaaru Réewmi

21/07/2025

*Corée du Sud 🇰🇷: 17 morts mooy khayma bi bayékoo Thi taw yu metti lool toulou Thi 170 mm .*

Xibaaru Reewmi

21/07/2025

Canal+ neena day tambelé yokk'o tarifs yi .

Adresse

Médina

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Xibaaru reewmi tv 2.sn publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Xibaaru reewmi tv 2.sn:

Partager