WAGA SN

WAGA SN WagaSprit!

"Néwonaa té mouy deuggBagn lo meunaloul dara ak beugue nioo yam"Omzo Dollar Officiel  - Goudi
17/06/2025

"Néwonaa té mouy deugg
Bagn lo meunaloul dara ak beugue nioo yam"
Omzo Dollar Officiel - Goudi

''Boo amé contactTé do brancher do takk''One Lyrical ‬Yakaar
13/06/2025

''Boo amé contact
Té do brancher do takk''
One Lyrical ‬Yakaar

🔥 10K ABONNÉS su YouTube 🔥Merci à vous la team, vous êtes les vrais ! 🙌Waga SN grandit grâce à vous, et c’est que le déb...
11/06/2025

🔥 10K ABONNÉS su YouTube 🔥
Merci à vous la team, vous êtes les vrais ! 🙌
Waga SN grandit grâce à vous, et c’est que le début.
On continue à vous servir du contenu frais et 100% Waga ! 💛

"Xam-Xam Arme lëma jëll xalaat yu baaxul défko G***k"Jeuf Wees në
08/11/2024

"Xam-Xam Arme lë
ma jëll xalaat yu baaxul défko G***k"
Jeuf Wees në

🎤 ft 🎵 Nietti At Ci Rénn "Ñetti at ci Rénn ñi bëgg xam ñeep Akci lēnSama Gaccė lan bëgoon giss tėggun ko bëtt ni ab-sirè...
07/02/2024

🎤 ft
🎵 Nietti At Ci Rénn

"Ñetti at ci Rénn ñi bëgg xam ñeep Akci lēn
Sama Gaccė lan bëgoon giss tėggun ko bëtt ni ab-sirène
Yarr sama bopp ndax Jubb du dėrett dou ci sax ci man
Li gënoon jaffé nékul ligeey mais ligeey sax ci man
Ñetti at music bi lāgo dankey changé at yi ñeuw
Nieudd Temps bi bukki la boot tax ngay dėgg Xadj di mbeuw
Ñetti at town bi deugërr Keuthie do giss fu nitt di Tėdéé
Dip son bi meunul won ñakk comme Galang funi Teuggė

Kaay ma wax-lë lu waral boy i fippu wuteli Gaal yi
Dėm Geej saani mbaal yi daj coono bu nėkk pour dėgg daali
Gënna takk dall-yi kooci laaj rêves-wam? France, Itali
Espoir reer ni Diary nioo ngi Xaar Nguur gi ci Taatu Ndaa-li
Maangi dox di dėm ci Yoonu GOD Iblìs dima Xeuthie
Humour dou changé damey bēg Yénn say ma Yėwu dėf Keuthie
Dara ma Yeema-tul giss na fi Xar-kanam bu nėh
Noflaay du Am baa mukk, GOD ci coono lañu bindee ñu nėė
Ñetti at ci rénn mère mëssul taayi ci dimey muñal
Su ñeep Xaadi won du bah, Tah ma warko déloo Njukeul
Sabab-lu jaamu Yallah ci Jaami Yallah yi
Bul jambù Yallah Nékk Nitt Nitė ko gën
Nitt mënul weesu jaamu Yallah Yeah"

Game of the day 🇸🇳⚔🇨🇲
19/01/2024

Game of the day 🇸🇳⚔🇨🇲

"Jeunesse bė jaxlė faakGaal-gi buy fees may TàkkJëll Yoonu Geej-gi labMoo gën Yaay boy di xiif bey lėb"🎵 Q.G🎤           ...
18/01/2024

"Jeunesse bė jaxlė faak
Gaal-gi buy fees may Tàkk
Jëll Yoonu Geej-gi lab
Moo gën Yaay boy di xiif bey lėb"

🎵 Q.G
🎤

"Santal ñi lakk pour nga leer-léÑoy sa sondėėlu life"🎵Téfess 🎤
17/01/2024

"Santal ñi lakk pour nga leer-lé
Ñoy sa sondėėlu life"

🎵Téfess
🎤

Adresse

Dakar

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque WAGA SN publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager