Mouvement A.C.N Jëff jotna

Mouvement A.C.N Jëff jotna j'aime Rufisque politique .social. culture .sport . Loisirs

Série Rio familli bientôt (  Ajel Moy TFC )
24/06/2024

Série Rio familli bientôt ( Ajel Moy TFC )

Merci beaucoup Mrs Abdou Karim mbengue dewenati balma akh balnala yalla nanou yalla bolé baale defal gnou jamm djou baré...
17/06/2024

Merci beaucoup Mrs Abdou Karim mbengue dewenati balma akh balnala yalla nanou yalla bolé baale defal gnou jamm djou baré Bari waay 🟢⚪

Merci beaucoup Mrs Adama diène directeur finance de la sonaged Dilen wax dewenati balén ma akh balnalaen yalla Nanou yal...
17/06/2024

Merci beaucoup Mrs Adama diène directeur finance de la sonaged Dilen wax dewenati balén ma akh balnalaen yalla Nanou yalla bolé baale defal gnou jamm djou baré Bari waay🟢⚪🟢⚪

Merci beaucoup Mrs baye Mor fall président mouvement ACN dewenati balma akh balnala yalla nanou yalla bolé baale defal g...
17/06/2024

Merci beaucoup Mrs baye Mor fall président mouvement ACN dewenati balma akh balnala yalla nanou yalla bolé baale defal gnou jamm djou baré Bari waay ❤❤❤️

08/03/2024

27 Mars journèe Mondial du théâtre
Gni charge sunu commission culturelle yi té nek si Maire yii Louy sen programm ?

Merci Rio Madior artiste comédien j'aime Rufisque pour ma vie ! Il takh ma def affiche barris.com,soluetude , p.boye 99 ...
09/01/2024

Merci Rio
Madior artiste comédien j'aime Rufisque pour ma vie ! Il takh ma def affiche barris.com,soluetude , p.boye 99 gni danouy dieul sen xaliss diko def si deuk gnouy giss yalla nalen yalla geuneu diapali bou bakh ndax gnoune Rufisque rek lanouy âme ,
Mes nak beug Nanou si seni projet un centre culturel bou bakh sakh 😭bilahi

Stop l'immigration  à rufisque , je suis le porte parole de la jeunesse,  il faut donner du travail à la jeunesse rufisq...
18/07/2023

Stop l'immigration à rufisque , je suis le porte parole de la jeunesse, il faut donner du travail à la jeunesse rufisquois, surtout, mes à rufisque y' à beaucoup de usine qui ne fond rien du toute à la jeunesse rufique surtout valda Afrique 😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡

Saltigue bassirou diop kou bakh tè meune loumouy deff , li ma wax gneup thi senegal  giss nako ( kou beug numéro rek def...
07/07/2023

Saltigue bassirou diop kou bakh tè meune loumouy deff , li ma wax gneup thi senegal giss nako ( kou beug numéro rek def dieul ma pv )

Fiertè de rufisque Mr sidy mbaye le fils de Moussa mbaye , des cœurs pour lui ak sen xalaat ligueyeume thi rufisque
06/07/2023

Fiertè de rufisque Mr sidy mbaye le fils de Moussa mbaye , des cœurs pour lui ak sen xalaat ligueyeume thi rufisque

Rufisque la Deuk , Non à l'immigration clandestin  restez chez nous svp  ! Magui sakou si daw gni nanou tokk fi ligueye ...
03/07/2023

Rufisque la Deuk , Non à l'immigration clandestin restez chez nous svp ! Magui sakou si daw gni nanou tokk fi ligueye !!!😭😭😭😭

Magui len di yegeul nii tay la sama anniversaire, di sakou si yène ayy gniane , ak cadeau surtout machine ordinateur pou...
20/06/2023

Magui len di yegeul nii tay la sama anniversaire, di sakou si yène ayy gniane , ak cadeau surtout machine ordinateur pour geuneu nek si sama ligueye ,

Adresse

Rufisque

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Mouvement A.C.N Jëff jotna publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager