Nanu Jangandoo

Nanu Jangandoo NANU JANGANDOO,
Fii ci emission NANU JANGANDOO, dinanu waxtann ci lu am njeriñ lool, dinanu yokk s

17/04/2025

«Man maay sàmm bu baax bi. Sàmm bu baax bi day joxe bakkanam ngir ay xaram.
Yowaana 10.11

30/01/2025

Aji Sax ji, woo naa la, gaawe ma!
Bu ma lay woo, teewlu ma.
2 Yal nanga ma nangul samag ñaan
ni cuuraay lu ñu la taalal,
yoxo yi ma la tàllal di saraxu ngoon soo gërëm.

25/10/2024

Éy Aji Sax ji, noon yeeka bare!
Ñu baree may jógal, ñu baree may tooge naa:
«Yàlla du ko wallu!»
Maay tëdd nelaw, yewwu;
Aji Sax ji di ma aar.

13/09/2024

Éy Yàlla, musal ma ngir sa tur,
jox ma dëgg, ci sa kàttan.
Éy Yàlla, déglul, ma ñaan,
teewlul, ma wax la.
Ay doxandéem a ma

08/07/2024

Manuleena boole jaamu Yàlla ak jaamu Alal.

11/06/2024

Bu leen ci kenn nax

22/05/2024

Dund gu dul jeex

17/05/2024

Yàlla, yërëm ma

31/03/2024

Yeesu Dekki Na

26/02/2024
19/01/2024

Déggal Aji Sax jee am solo

May xaara xaar Aji Sax ji,
mu dégg may woote, geesu ma,
génnee ma ca kàmbug sànkute,
sippee ma ca xóotey ban ba,
cëppe ma ciw doj,
samp ma, ma dëgër.

Adresse

Thiès Nones

Téléphone

+221776760247

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Nanu Jangandoo publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Nanu Jangandoo:

Partager

NANU JANGANDOO

NANU JANGANDOO

Xëy na mën nga xalaat ne, ki gëna waane, ba ma jangee, yàgg na. Soxlawuma jàng, li ma xame doy na. Am naa ben borom xam xam ku waxoon ne « su kenn yaakaaree xam dara, xamagul ni mu wara xame »

Fii ci emission NANU JANGANDOO, dinanu waxtan ci lu am njeriñ lool, dinanu yokk sunu xam xam ci lépp lu jëm ci Yalla ak kàddoom.