28/10/2025
Surce Serine Mor Astou Tourè
Jiwu doomi naajo barina njariñ.
Dafay gëna dooleel fàttaliku ak gëna bàyyi xel ci liggéey bi.
Dafay dëgëral yax yi ak sidit yi.
Dafay aar sa xol, wàññi kolesterol.
Dafay joxe energie ci bis bi yépp.
Dafay faj yaatuwaayu prostate ba noppi gëna rafetal wérgi-yaramu góor ñi.
Dafay yokk testosterone ba noppi yokk njuram.
Dafay dàq dund yi ba noppi aar mbàq yi.
Dafay dëgëral yaram wi, di xeex feebar yi.
Dafay dundal kawar gi ba noppi moytu kawar gi dagg.
Dafay dalal neer yi, ba noppi gëna nelaw.
Dafay yamale hormone yi ba noppi wàññi màndarga yi ci menopause.
Dafay yamale reesal ba noppi moytu nga am mbàq.
Benn kuddu bis bu nekk suba ak ngoon doy na ngir dooleel sa wergi yaram
La citrouille est un trésor. Les bienfaits de ses graines :
Renforce la mémoire et augmente la concentration
Renforce les os et les muscles
Protège le cœur et réduit le cholestérol
Fournit une énergie naturelle tout au long de la journée
Traite l'hypertrophie de la prostate et améliore la santé masculine
Augmente le taux de testostérone et augmente la fertilité
Expulse les vers et protège les intestins
Renforce le système immunitaire et combat les maladies
Nourrit les cheveux et prévient leur chute
Calme les nerfs et améliore le sommeil
Régule les hormones et réduit les symptômes de la ménopause
Régule la digestion et prévient la constipation
Une cuillère à café par jour suffit pour fortifier votre corps de l'intérieur