TMS officiel

TMS officiel TMS officiel di kër guy jàngale tay yeete tek ci di leen jox xibaar yu wér te wóor. TMS daal yë

15/04/2024
15/04/2024

Ana way defal yàlla yi ??!!
الدال على الخير كفاعله

Assalamou halakumMbokki jullit yi ñoo ngi sàkkul sunu mbokkum étudiant bi yalla tek febarou cencer mou sonnu lool te ord...
23/10/2023

Assalamou halakum
Mbokki jullit yi ñoo ngi sàkkul sunu mbokkum étudiant bi yalla tek febarou cencer mou sonnu lool te ordenace bin ko bindel tollu thi 1.570.930f.
Kon lu waay am te yàlla rek tax
770458645
786096911

22/10/2023
Ñoo ngi sakkul ndibël sunu mbokkum étudiant bi yalla tek febarou cencer .Mou wara jënde ordenace bou tollu thi 1.570.930...
22/10/2023

Ñoo ngi sakkul ndibël sunu mbokkum étudiant bi yalla tek febarou cencer .
Mou wara jënde ordenace bou tollu thi 1.570.930f
Ñoo lèeni ñaan ndibel lu waay am xeebun yèemun
770458645
786096911

Di ap étudiant bu amè cancer du sens ñukoy sakkul ndimbel thi lukoy genè rèew mi AK ordence bii tollou thi 1.570.980f Xe...
22/10/2023

Di ap étudiant bu amè cancer du sens ñukoy sakkul ndimbel thi lukoy genè rèew mi AK ordence bii tollou thi 1.570.980f
Xeebun yèemun lu waay am te yalla rek tax
770458645
786096911
Amna weve AK orange money

21/10/2023

Def te yalla tax ngir dimbali sunu mbokkum jullit mii tawat tawati Cancer di sakku ndimbel lu waay am xeebun yeemun

Adresse

Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque TMS officiel publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à TMS officiel:

Partager