11/04/2026
Képp koo xam ni saa boo xëyee sa yitte yépp mooy jot àdduna, Yàlla dina saxal ci sab xol ñatt yoy doo tàqalikoo ak moom mukk
Soxla yu dul jeex mukk
Njàqare ju dul deñ mukk
Ñàkk gu dul dog mukk