CHÉKÉ 221 Zig Boy

CHÉKÉ 221 Zig Boy ✅️ Blogueur
✅️ Créateur Digital
✅️ Community Manager
✅️ Direction du Marketing et de la Communication de la LONASE 🇸🇳.
(315)

Mon Tik Tok 👇🏿👇🏿

https://www.tiktok.com/?_t=ZM-8ue4Ak2LS9m&_r=1

Erdogan loumouy triste triste lou ni cii gnibi Ousmane Sonko bi, saay ki nio lako geuna sokhla deh 😂🤣.
11/08/2025

Erdogan loumouy triste triste lou ni cii gnibi Ousmane Sonko bi, saay ki nio lako geuna sokhla deh 😂🤣.

11/08/2025

Wadja ngini 😭

Mangui guiss ngéne dimey mentionner cii béne vidéo ko khaam douma wakh tourame, mais mane dama nek cii relation bou séri...
11/08/2025

Mangui guiss ngéne dimey mentionner cii béne vidéo ko khaam douma wakh tourame, mais mane dama nek cii relation bou sérieuse ak Sokhna Soda Ndao, bouma kéne distraire nak 🙏🏿.

Heureux anniversaire mon rival de luxe Momo Øg🎂 un gars cool Yalna nalleu Yallah déffale tawfêkh ak khéweule you beuri, ...
11/08/2025

Heureux anniversaire mon rival de luxe Momo Øg🎂 un gars cool Yalna nalleu Yallah déffale tawfêkh ak khéweule you beuri, on dépose les armes ba aliberssaire bi passer 😁.

11/08/2025

Transports en communs yeupe vides négn, talli yii pareille, Dakar iow tamite lou am rek gars yi dem bayi la fi, dégn ley diay rek mais diapo cii dara
😭😭😭

10/08/2025

Milieu patriotique, Beh Euleuk inchallah 🤣😂

Ohh, photo bi touché nama 🥹.
10/08/2025

Ohh, photo bi touché nama 🥹.

10/08/2025

Wadji so léne ko dieulssi woule dou gnibissi deh 😂🤣.

10/08/2025

Talla Sylla cette année khana dokhoule walleu mo ngui cii yoone
🤔🤔🤔

10/08/2025

10 bi daffa 10 pour Lamine Yamal, supporter Real Madrid Yallah toppé wouko dara. Barça 4-0 Como
😂🤣🤣

Izo 🇸🇳 bat la Dream Team de Liverpool et 𝗥𝗘𝗠𝗣𝗢𝗥𝗧𝗘 le Community Shield pour la première fois de son histoire ! 👏😍🏆🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿...
10/08/2025

Izo 🇸🇳 bat la Dream Team de Liverpool et 𝗥𝗘𝗠𝗣𝗢𝗥𝗧𝗘 le Community Shield pour la première fois de son histoire ! 👏😍🏆🏴󠁧󠁢󠁥󠁮󠁧󠁿

✅ Crystal Palace Remporte la FA Cup pour la première fois en battant City
✅ Crystal Palace Remporte le Community Shield pour la première fois en battant Liverpool

𝗥𝗘𝗦𝗣𝗘𝗖𝗧 🙌💙❤️.

10/08/2025

Limou wakh cii Bako mome kéne meunouko dindi 😂🤣.

Adresse

Ziguinchor

Téléphone

+221771260674

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque CHÉKÉ 221 Zig Boy publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à CHÉKÉ 221 Zig Boy:

Partager